Wolof – Gambian (EC)
Advanced Gap Text
Completed Sentences:
Mun ga laka Wolof.
Waaw, mun na laka Wolof tutti rek.
Balal ma, nga wahal danka?
Balal ma, mun nga wahat lolu anchor?
Mun nga laka Wolof boubah.
Ki mun na laka Wolof boubah.
Guy mun nen laka Wolof boubah.
Ga neh lan?
Kine nga dorr di jangal Wolof?
Muss nga dem Gambia?
Waaw, muss na far dem.